A B C D F G I J K L M N P R S T U W X Y ?

Kayam

Ne kayam: (njëfka)

Dee, gancax guy sooga dee, ba tàmbalee wow, da naan kayam. Niral: Sa garab gi de nee na kayam, xanaa daawóo ko suuxat?

error: Content is protected !!