Xebet Auteur de l’article Par Jàng Wolof Date de l’article 01/12/2019 FacebookTweet Xebet: jëf Diiŋat, suufeel, xeeb, ñaawlu. Niral: Bàyyil di xebet li sa njaatige li di def, ndax boo nekkoon ci barabam de danga xam ne jàmbaar dëgg la, jiite yombul. FacebookTweet Partager sur WhatsApp(ouvre dans une nouvelle fenêtre) WhatsApp Partager sur Telegram(ouvre dans une nouvelle fenêtre) Telegram ← Kun → Biram